Tivaoune mosquée 2

Khoutbeu du Vendredi 11 juin 2021

Religion

Par El Badou Gning

Salam !
Souniou Magg’gni, mboubou daraja laniou yorone, diko jokhanté, diko defar, diko fote, diko passé, diko thiouraay, diko parfumé, mo yéggeulone sen maartaba. Louné ci lou baakh wakhanté naniouko.
Kouci yakkalone sa morom, nieupp lekk ba sourr ndakh niom daniou khamone ni li Yala yorr ci mbaakh lep, khajjoul ci ben nitt.
Yala ni tolou !
Yalnanioulen Yala fayal. Lep rafétone’na !

Way ngala bouniou kheutio mboubb’mi bamou khotékou mbaa mou rerr souniouy lokho. Ngala naniou moytou mou taabbi ci lokhoy baadola.

Le problème dou gniy soti pétrole ci keurou Diné’yi beugg’ko taal, niome lolou moy sen mission, mais ceux qui alimentent et partagent leurs inepties.

Joumah moubarak !

Partager

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *