La voiture acheté à Guy Marius Sagna

Kaaduy nguereum diogué thi Guy Marius SAGNA dieum thi ay Sopem Yiko wouteul ap woto…

Seen surga Guy Marius Sagna (GMS) mooy wax ak yéen, di leen gërëm, di leen sant ci daamar (voiture) bi ngeen teg ci samay yoxo, ginnaaw bi ngeen waxee ni : Jot na seen surga bii di GMS am woto. Dajaale ngeen 14i tamdareet (millions) ci xaalisu Farãs. Fukki tamdareet yi ak xaaj (10,5 millions) […]

Lire la suite