Parmi les saints : Lenn ci bindou magg’gni | El Hadj Abdoul Aziz Dabakh

‘Yala!
Mane Abdoul Aziz, sama thiofel ci Yonentibi dafa diakhassok sama dérett.
Sou sama dérett done sotékou dangay guiss sama thiofel ci Seydina Mouhamed sws.

Waayé tay, Yonentibi limouy baakh yep khadio’wouma. Yaw Yala laa taalal lokho ndakh yaamafi eundi ci’sa thiobaré.

Dama teulé té beugg aksi ci yaw Yala.
Sokhla’wouma ken tay koudoul yaw.
Dou Yonentibi, dou Aladji Malick.

Kheuthie’meu bama nieuw ci’sa wett.
Wayé nak bomeu kheuthié bama nieuw, dama beugg nga bolé’maak kingeu khamni yaako taanal sa bôpe mouy Khatimil Anbiyahi Imamil Moursaline Sallalaahou Aleyhi wa Salam! « 

PUBLICITÉ
Partager

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *