Viatique du 09 avril 2021

Compassion
« Cette part d’humanité en nous, cette grande part qui domine notre instinct animal, cette conscience du bien et du mal, est-elle devenue si résiduelle que le malheur ou la mort d’autrui puisse nous réjouir ?
On ne construit pas son bonheur sur le malheur des autres. C’est illusoire de le penser parce que ce n’est tout simplement pas possible. On ne doit pas se réjouir des souffrances de son prochain. Ce n’est pas pour ça que nous sommes sur terre. Celui.elle qui perd sa capacité de compassion a perdu toute son humanité, c’est un mort vivant! »
Bon vendredi
Dr Massamba Gueye LBA

Yóbbal

« Siddit gi tax nu nite, li ne ci nun ba taqale nook bàyyima,xel miy tax a ràññee lu baax ak lu bon, mbaa du daa raaf ni sagaru tayukaay wu oos ba tax nit di am mbégte ci ayu nawleem?
Kenn du tabax sa bànneex ci naqaru nit! Loolu manut a am! Janeeru kuy gént la, ndax manut a nekk! Nit warut a bànneexoo naqar wala faatug moroomam. Loolu taxul nu wàcc ci kow suuf! Ku àgg ci dóotoo séddu ci naqaru nit ñi, dóotoo nit, niiw buy dox nga.»
Àjjumay Jàmm
Dr Masàmba GÉY GA

Partager

Un commentaire

  1. Salam Professeur.,
    Je partage ton point de vue entièrement.Ce message tient lieu de mise en garde, j’allais dire d’alerte a toute la population Sengalaise face aux derives que nous constatons dans nos comportements de tous jours.
    Ressaisissons nous chers compratriotes pendant qu’il est temps.
    Vive ke Sénégal

Les commentaires sont fermés.