khoutbeu du vendredi mosuqéé

Khoutbeu du Vendredi 18 Juin 2021

À la Une Religion

Yala dafani Daouda (asw):
-Fekk dégoni mane Yala folékounaa, def’nanioumeu coup d’état, nga thieytouko bamou waurr, seu ceinture guigueu takone ngir jaamoumeu neu gueuneu dangg, boumou tékékou !

-Fekk dégouloni sama saakh’yi feugg’neu, bidew desseutoul ci assamaane, jeun desseutoul ci guejj’gui, naatt dessatoul ci aaleu’bi, weurseuk boumou’done seu tiiss. Maako yorr té fonekk ma fekk’lafa jokh’lako!

Fekk dégoni ibliss déneu baniou soûle’ko, boul teureul say ngaanaay, saï-saï leu daflay bett gaagne’leu!

Fekk jéguiwo siraatt, dougg aldiana niou installer’leu, tabalayiy yeugg, jiguéne’gni dileu oupp, boul waulou sama pékhé.
Maam Adama ci biir adiana lako ibliss fekk guénéko. Kone ki nékk ci biti waro naagou!

Yalnaniou Yala saamal bopam, boléniou ci ay nioniam bijahi Rassouloulah Sallalaahou Aleyhi wa Salam!
Baamel bou khautt bobou, kounioufeu soûle baayilafa té nékoulo’wone ci li nékh Yala, dinga rethiou lodone jouddo.

Soutoureu Daahimane
Joumah moubarak!

El Badou Gning

Partager