khoutbeu du vendredi mosuqéé

Khoutbeu du Vendredi 18 Juin 2021

Yala dafani Daouda (asw):-Fekk dégoni mane Yala folékounaa, def’nanioumeu coup d’état, nga thieytouko bamou waurr, seu ceinture guigueu takone ngir jaamoumeu neu gueuneu dangg, boumou tékékou ! -Fekk dégouloni sama saakh’yi feugg’neu, bidew desseutoul ci assamaane, jeun desseutoul ci guejj’gui, naatt dessatoul ci aaleu’bi, weurseuk boumou’done seu tiiss. Maako yorr té fonekk ma fekk’lafa jokh’lako! […]

Lire la suite
Tivaoune mosquée 2

Khoutbeu du Vendredi 11 juin 2021

Par El Badou Gning Salam !Souniou Magg’gni, mboubou daraja laniou yorone, diko jokhanté, diko defar, diko fote, diko passé, diko thiouraay, diko parfumé, mo yéggeulone sen maartaba. Louné ci lou baakh wakhanté naniouko.Kouci yakkalone sa morom, nieupp lekk ba sourr ndakh niom daniou khamone ni li Yala yorr ci mbaakh lep, khajjoul ci ben nitt.Yala […]

Lire la suite

Khoutbeu du vendredi 9 avril 2021

Par El-Badou Gning “Rien n’est plus affligeant que la mort du coeur, la mort de l’homme est secondaire.”Khole bou amoul ben yeugg yeugg ci mbaakh, eumboule dara ci yiw, moy dé ? “Entre la mort et la lâcheté, choisis sans hésiter la mort !”Sécheressou tôl, mo gueune Sécheressou khole. Khole bou wow borom dou yeugg […]

Lire la suite

Khoutbeu du vendredi 02 avril 2021

Par El-Badou Gning Salam!Yala bimou sakké domou Adama la doggal limou wara doundd ciy att, foumouy déwé, likoy ray ak founioukoy robb, limou wara am ci weurseuk, kane, wala kan’ak kane la’wara seuyyeul, niaata dôme la wara am.Yi, Yala douggeulouci ken. C’est le commun des mortels, n’importe qui, tout un chacun ! Il faut que […]

Lire la suite

Khoutbeu du vendredi 19 mars 2021

Tu sais, Seigneur, Toi qui sondes les coeurs et les esprits, combien tout ce quiternit l’image de marque de ma religion, combien tout ce qui viole Tes commandements, combien tout ce qui retarde la marche de mon pays vers plus de bonheur, de prospérité, de paix, de justice, de Foi et d’espérance me chagrinent profondément(Cheikh […]

Lire la suite