mosquée de tivaoune

Khoutbeu du vendredi 29 janvier 2021

Par El-Badou GNING

Mouhamed, « wakhal sa gaayi naniou ragal Yala deugg deuggi ragal Yala, tay wakh deugg! »
So démé ci ap deukk, fekk nieup def yaramou’néne, dangay soumékou ni niome! Gaurgui né « dédett…na fekk sa yaram rafett! »
Nieup defnaniouko naako def baakhoul!
Nieup rewnaniou damay rew baakhoul!
Légui nieupeuy fenn dinâ fenn baakhoul!
Ken baakhatoul damay bone dou fouleu!
Tu gagnerais mieux bo fékhé ba gnibone, gni rew, gnay fenn, nga sorilenn té fékhé beu founiouy limé gnibaakh bolélaci, bouniouy lime gni deuggou bolélaci, bouniouné diw, niouné Aka yarou.
Société, pour ne pas dire wolof, molay gnimélo Yala: « fenn wouy defar mo gueune deugg gouy yaakh ».
Boukhari (rta) dit certes  » Il n’est pas considéré comme menteur celui qui veut réconcilier des gens en transmettant des bonnes choses aux uns et disant du bien à d’autres. « .
Mais, le Prophète (sws) a dit : « Attachez-vous à la vérité même si vous y voyez une perte, car le salut se trouve dans la vérité « . (Ibn Abi Dounya)
Lo khamni boko wakhé mouy fenn, nopiko amci yiwou mandou !
Nitt, lo baakh doyoul!
Ak mbone amoul ndiarigne, sakanoul.
Mbone yi gueuneu bone ci khétou mbone yi moy: jeuw, toûmal nitt ko khamaloul dara, yaakh déram.
A chaque fois nitt nétali lingako toûmal, Yala jokhko yiw, koka am baakar woutolni wimoula jokh.
Fanwéri (30) ndiaalo ak lou tek mo gueune togg di degglou jeuw, wakhoumalak ngay jeuw.
Naniouci bayi khel!

JOUMAH MOUBARAK !

Partager