Parmi les saints Lenn Ci Bindou Magg’gni Mame Raan Laye

 » Yawmi am jaakhlé, boul rouss dem ci kila tané. Yawmi Yala baakhé, bo fajjalaté AADIO kila yaakaar ba nieuw ci yaw, ngala waay boulko wakh ba nieupp yeugg’ko.
Fajjal nitt aadiom bé paré kou nieuw nganiko diw laako jokh, légui lafi jougué, tasséwok mom ?
Nitt wétt’ak yaw wakhla sokhlâm nga bayi sédé nieuw nga lambb sa poche, amatôci yiw sa alal dem.
Rewmi soutoureu mingifiy beugg taagô, lo’wakhak nitt degg’ko fénéne, ani soutoureu? »

Partager

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *