FB IMG 1602851785034

Khoutbeu du Vendredi 16 octobre 2020

Nitt, je parle pas du musulman, mais de l’espèce humaine, doundeum dafa chère ci Yala. Quelque soit son obédience, naniouko sammal yii:

  • Sa Croyance
    Mouhamed sws, en période de guerre, interdisait à ses combattants d’ôter la vie aux enfants et aux femmes, leur conseillait de ne pas empoisonner les puits ni saper les arbres. Mais surtout veiller à ce que toute personne qui fuit ne soit pas poursuivie jusque dans les lieux de culte mouy église wala synagogue.
    -Khélou domou Adama
    Tout État doit veiller à l’éducation de ses enfants à la base Surtout, nitt bou diangoul, amoul Kham-kham, moy nitt kou dé, dieumeum moy baamélam.
    Guinaw bou diangué, naniouko feggal bepp khétou drogue ba khélam dou yakhou.
    -Dérou domou Adama
    Ken amoul droit yaakh dérou nitt, kounekk yangekk lokham’ni, bouko Yala siiweulone adineu touki.
    Légui nak, nitt gni daniouy oubi boutique pour diaye marchandise, gnici dess di oubi boutique di wekk dérou Nitt diko diaye. On voit n’importe quoi à travers la presse.
    -Alalou domou Adama
    Bou ken néweul dolé nitt pour nangou alalam. Thiono bimou dadj ba am alal, neu sociétébi dadj louko raw pour protéger’ko.
    -Culture et civilisation
    Lepp lou am ci réwou taakh’yi, naniouko lawal mou yegg ci kaw’gui. Yala bougoul favoritisme ci nitt’gni. Nieuppeu yem ci mom.

Une bonne constitution ne peut suffire à faire le bonheur d’une nation; une mauvaise peut suffire à faire son malheur.
Li yeupp rewmouko samm, jamm amna!

Joumah Moubarak !

Partager