FB IMG 1606046567456

Lambi Dimanche’ji

Par El-Badou Gning

« Quant à toi Abdoul Aziz, ne cherche jamais à t’élever au-dessus de tes semblables par ta naissance ou ton rang social.
Ne les exploite jamais car Dieu n’aime pas les exploiteurs. Aie une foi pure. Ne te considère supérieur à personne. Au nom de quoi, d’ailleurs te prétendrais-tu ainsi ? »
Mame Dabakh (rta)

Successivement: Yala, akoup Yonentam (sws), say weuyjour, ak sap Serigne.
Légui nak wayjour mom, serigne’bi moko eupp dogal ci domam jimou jourr.
Kaawteff!!!

Dome, sa diguntek sa weuyjour, bouci dara dokh loudoul yalay kessé. Neuf mois de grossesse you serigne fékéwoul, yeuggoul. Bo faato yitt, si on ne le lui apprend pas, douko yeugg.
Té Yala néna Ajanay dome mongici ndeuggeul tankou ndayam. Kou fowé say weuyjour, gnila magg fowéla, sak maass fowéla, gnila fété ndaw fowéla.
Té bilahi kou dem alakhira té yobaléwo sa ngeureumou weuyjour, guissoumala Firdaws.

Sa diguntek sa Serigne, wessouwoul fassanté koleuré, mou tanéla ci Yala akoup Yonentam, khamal’leu lici tërë Yala bou tedd’bi (alkhourane), wakhla sa dîné, dileu diggeul loubakh, dileu téré loubone.

Naniou délo weuyjour sen thieur bilen Yala jokh té moytou di yékeuti sen siditou khole. Il est des gens, bouniou jotatone ci yaay wala baay, douniouko gueumé. Kone gni Yala baakhé niou nekak sen weuyjour, naniou profito, lici dess beurétoul. Koula raw, ci fonkk weuyjour lala rawé.

Yalneu Yala barkel nieupp inchallah.

Partager