Parmi les Saints Seydi Aboubacar Sy

Par El-Badou Gning

Mame, le Khalif, le Beau, le Magnifique,
Général!

Le guide inter-religieux qui transcende toutes les générations et traverse toutes les époques.

Dou tass yakar, dou dagg, dou bayi, dou féci koleuré, dou bodi, dou khasté, dou gaaral, té kuka wolou ba diisko sa sokhla, bouné « Inchaaallah » fofa tojj.

L’élégance à l’État pur, la pertinence au sens pur, la persévérance du dur, la constance du pur !
Une dimension unique, un profil magique !
Nioleu beug té guissoniouleu, nioleu gueum té diékhalougnouleu.

Une encyclopédie de savoir, de savoir être et de savoir vivre !

Mame Khalifa Yalnaniouleu yalla fayal té tass niou sa barké.
Aka matt way !

Souniou Mame’ji ken meunouci andak sago.

Mame yaa baakh, yaa yiw, yaa yarou, yaa feggou, yaa mandou, yaw mii yaay Soutoureu.

Tôgno sa Borom, Tôgno sa morom, Tôgno sa njabott.

Notre lumière dans la voie, notre barrière contre la perdition.
Amo morom mon général !

Partager