Khoutbeu du vendredi 02 avril 2021

Par El-Badou Gning
Salam!
Yala bimou sakké domou Adama la doggal limou wara doundd ciy att, foumouy déwé, likoy ray ak founioukoy robb, limou wara am ci weurseuk, kane, wala kan’ak kane la’wara seuyyeul, niaata dôme la wara am.
Yi, Yala douggeulouci ken. C’est le commun des mortels, n’importe qui, tout un chacun !

Il faut que nous nous ressaisissions car, l’heure n’est plus de donner raison à ceux qui se croient supérieurs aux autres. Ki gueune ci nioune moy ki gueuneu ragal Yala!
Alors, il urge de revisiter nos cultures et traditions qui nous ont toujours assuré la sécurité et la paix dans nos sociétés.

Amna ko khamni joudoko sankk, foumou tolou diko woné.
Am ko khani am amam moko sankk, foumou tolou diko woné.
Am ko khamni darajam mako sankk foumou tolou diko woné.
Si c’est une haute naissance, mouss Ken gueunouko rafétt joudou: mouss de père et de mère !
Boudé alal, Kou khéboul sa weurseuk Ken gueunoula riche !
Boudé daraja, Ani gnifidane oubb lambb’ji ?

Naniou khamni nous sommes tous issus d’un seul couple: Adam et Eve!

PUBLICITÉ

JOUMAH MOUBARAK.
SOUTOUREU DAAHIMANE !!!

Partager

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *