Tivaoune mosquée 2

Khoutbeu du Vendredi 11 juin 2021

Par El Badou Gning Salam !Souniou Magg’gni, mboubou daraja laniou yorone, diko jokhanté, diko defar, diko fote, diko passé, diko thiouraay, diko parfumé, mo yéggeulone sen maartaba. Louné ci lou baakh wakhanté naniouko.Kouci yakkalone sa morom, nieupp lekk ba sourr ndakh niom daniou khamone ni li Yala yorr ci mbaakh lep, khajjoul ci ben nitt.Yala […]

Lire la suite
mosquée de tivaoune

Khoutbeu du vendredi 29 janvier 2021

Par El-Badou GNING Mouhamed, « wakhal sa gaayi naniou ragal Yala deugg deuggi ragal Yala, tay wakh deugg! »So démé ci ap deukk, fekk nieup def yaramou’néne, dangay soumékou ni niome! Gaurgui né « dédett…na fekk sa yaram rafett! »Nieup defnaniouko naako def baakhoul!Nieup rewnaniou damay rew baakhoul!Légui nieupeuy fenn dinâ fenn baakhoul!Ken baakhatoul damay bone dou fouleu!Tu gagnerais […]

Lire la suite
Tivaoune

Khoutbeu du Vendredi par El-Badou Gning

La femme veut sentir une force à ses côtés. Force dou dolé mais mougne ak yénou liko Yala diggeul ci seuybi, té dou onkou dou jambatt. A cause peut-être de sa capacité à être mère, elle attend instinctivement d’un homme: solidité, sécurité, virilité, stabilité. Ndeuggeurlaay, yeurmandé, khelmou dall ak Soutoureu! N’insulte pas, ne frappe pas, […]

Lire la suite

Khoutbeu du Vendredi 02 octobre 2020

Par El Badou Gning Niongi’len di ndôkel!…Ci rammou guiniou Seydina Mouhamed Nara rammou euleukkHÀNI’ANE LANA MINE’HOU SHAFÂ ATTOU FI HA’DIME Dineu amm!Ngeureumeul Yala, ci bepp jââm bou wéteul Yala.Rammou deugg dineu amm ndakham, ci kane?Khanâ ci kou nekk ci yonou Seydina Mouhamed sws, mô’kham ki joûmm def bakaar, mô’kham kiko tayoul.Nioune nieupp TOUM’HÂ, des’neu farr […]

Lire la suite